Ay Millioni nit dina ñu teew – Ndax Yaw dinga teew?

Ay Millioni nit dina ñu teew – Ndax Yaw dinga teew?

Kayit bi ñu def ngir woo nit ñi ci Ndaje fàttaliku bi

Kayit bi ñu def ngir woo nit ñi ci Ndaje fàttaliku bi

Ay Millioni nit dina ñu teew – Ndax Yaw dinga teew?

Teewe lan ?
Ci guddi gi mujj bala muy dee, Yeesu dafa booloo ak apootaram yi. Mu taxawal xew ci faso buyomb te nee leen : “Defleen lii, ngir fàttaliku ma.” Da ñu waroon a def loolu ngir fàattaliku sarax bi Yeesu naroon a def ngir njari ñu doomu Aadama yi (Luug 22:19, 20).

Daaw, ci àddina si sépp, lu jege 20 milioni nit topp na ñu santaane Yeesu boobu te teew ci xew boobu ñuy def at mu nekk. Ren nag, dina ñu def ndaje bi ñuy fàttaliku deewu Yeesu Àjjuma, 3 Awril 2015 bu jant bi sowee. Seede Yexowa yi ñu ngi lay woo ci ndaje bu am solo boobu. Nanga ci teew. Dinga xam njariñ bi nga mën a jële ci dundu Yeesu ak deewam.

Ay nit ñu ngi waxtaan fekk ndaje karceen bi jeex na

Crédits: Témoin de Jéhovah. Disponible en: www.jw.org/wo.

Seede Yexowa yi nekk ci sa gox dina ñu daje ci béréb ak waxtu bi ñu bind fii ci suuf:

(As seguintes reuniões serão realizadas em Francês. No caso da França e Senegal, nos locais citados serão realizadas reuniões em Wolof)

Caxias do Sul – Rio Grande do Sul – Brasil

03 Awril (Abril) 2015 (03/04/15) – 19:00 (07:00 PM)

Bairro: Cristo Redentor
Local: Salão do Reino das Testemunhas de Jeová
Rua: General Câmara, 1741 Caxias do Sul, RS
CEP: 95082-070

http://www.jw.org/apps/T_PBrTFnNsR?m=3f5d89e867453c60d5340ed45deeb1b5

São Paulo (Região Central) – São Paulo – Brasil

03 Awril (Abril) 2015 (03/04/15) – 20:00 (08:00 PM)

Bairro: Liberdade
Local: Nikkey Palace Hotel
Rua: Galvão Bueno, 425

http://www.jw.org/apps/T_PBrTFnNsR?m=5a5149598a7142bd9ce1d036b8b87489

São Paulo (Região Leste) – São Paulo – Brasil

03 Awril (Abril) 2015 (03/04/15) – 21:15 (09:15 PM)

Bairro: Arthur Alvin
Local: Salle du Royaume des Témoins de Jéhovah
Rua: Benedito Leal nº 541, Arthur Alvin

http://www.jw.org/apps/T_PBrTFnNsR?m=4cbf19407938c6da849ab4a16d6d0f0c

Rio de Janeiro (Região Sul) – Rio de Janeiro – Brasil

03 Awril (Abril) 2015 (03/04/15) – 20:15 (08:15 PM)

Bairro: Glória
Local: Hotel Golden Park, 6º andar (étage)
Rua: Rua do Russel 374

http://www.jw.org/apps/T_PBrTFnNsR?m=4cbf19407938c6da849ab4a16d6d0f0c

Fatick – Senegal

03 Awril 2015 (03/04/15) – 19:00 (07:00 PM)

Quartier: Longandem
Place: En face de Gouye Meew
Rue: Lot N˚ 257

http://www.jw.org/apps/F_PBrTFnNsR?m=b0f2167a652ace3ce7b7280e13f34603

Paris – France

03 Awril 2015 (03/04/15) – 20:00 (08:00 PM)

Quartier: Paris 17
Place: Salle du Royaume des Témoin de Jéhovah
Rue: Bridaine, 75017

http://www.jw.org/apps/F_PBrTFnNsR?m=cff602e473fa97395358516efd80fe8c

 

Outros endereços no Brasil e no Mundo

Você está cordialmente convidado a celebrar em nossa companhia o Memorial da Morte de Jesus. Encontre um local dessa reunião perto de você.

http://www.jw.org/pt/testemunhas-de-jeova/comemoracao/

Este post está disponível também em fr_FR

Deixe uma resposta

O seu endereço de e-mail não será publicado. Campos obrigatórios são marcados com *