Ay Millioni nit dina ñu teew – Ndax Yaw dinga teew?

Kayit bi ñu def ngir woo nit ñi ci Ndaje fàttaliku bi

Ay Millioni nit dina ñu teew – Ndax Yaw dinga teew? Teewe lan ? Ci guddi gi mujj bala muy dee, Yeesu dafa booloo ak apootaram yi. Mu taxawal xew ci faso buyomb te nee leen : “Defleen lii, ngir fàttaliku ma.” Da ñu waroon a def loolu ngir fàattaliku sarax bi Yeesu naroon a def ngir njari ñu doomu Aadama yi (Luug 22:19, 20). […]

Lire la suite